dal
Apparence
Wolof
[Soppi]- ab dal: fees di dal: fees di wàcc
- lu dal: lu ne tekk, dox mi dal na, taw bi dal na
- door: dal na di dem:door na di dem, dal na jàng:tàmbali na, door na am njàngam. Ci foofu la dal giy tekki principe juge
- dal :principe
wu faraas
[Soppi]- lieu où descend un hôte
- calme, serein
- commencer,
- principe