Waxtaan:aw

Le contenu de la page n’est pas pris en charge dans d’autres langues.
Yokkuw tëriit
Jóge Wiktionary.
Dernier commentaire : 14 at ci ginaaw par Ahloubadar

Ibu bul di def loo xamul far, loo xamul mbaa loo àndul danga cee war a war ak ki ko fi def njëkk lu ne, lii ma fi def nga far ko lu tax daa amul ? am danga cee àndul ? Aw ku nekk ci mbir ba sonn bàyyi ak keneen mu def. niki:awal gone gi ci liggéey bi sonn na kat, xamnaa dangaa yaakaar ni awu la déet baat bi dëgg aw dogg la, jëf jeey tax u gi ñaw muy awu --Ahloubadar 29 Sulet 2009 à 18:33 (UTC)Répondre