àttekat

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

mi ngi bàyyikoo ci àtte

Open book 01.svg Tur[Soppi]

àttekat b:

  1. démb de àttekat bi daanoon na Musaa atum kaso
  2. àttekat mooy kiy àtte ñaar ñu jote, dem ci yoon

Xool it[Soppi]

Tekki[Soppi]

wu-faraas: juge

Nuvola apps edu languages.svg Waxiin

Déglul baatu àttekat ci wolofi Senegaal