Aller au contenu

xereñ

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]

Ag xereñ

Am ñu naan “xarañ”: ñaw ci dara, aay ca

xam-xam
  1. xam-xam la buy wund mbooloom ay liggéey, dale ko ci xalaat, settantal ak njàng ga(gëstu ga) ba ci yorug tabax bi, ba ci fuglug jumtukaay yu ag taxawal gu xarala walla gu ndefar
  2. Nit kii ku xereñ la ci tabax

Yeneeni làkk

[Soppi]