Aller au contenu

ndefar

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]
  • mbooloom cawarte yu koom-koom yiy juddal ak a jóox, maanaam yiy amal alal yu daju yi (biens matériels) jaare ko ci soppi ak liggéey ñumm (matière première) yi segg léen: Jëmale-kanam ndefar gu am réew: doxal ko, jañ ko mu dem.

Bu mu man a doon ci ci cawartey koom-koom yii: Ndefar gu ndima (industrie textile), gu dàll (de la chaussure). Gépp cawarte gu koom-koom gu ñu man a niroole ak ndefar : Ndefar gu wone, gu péexlu. Cawarte gu ñu nos ci anam gu xereñ te leer, te muy lu yaatu:(ñaare lu ñaaw lay doon) : Ndefar gu tooñaage (L'industrie du crime). Li nit kiy def ngir daal ne daa war a dund (ñaare lu ñaaw lay doon):Def ndefar gu baaxul.

français

[Soppi]
  • industrie:

Ensemble des activités économiques qui produisent des biens matériels par la transformation et la mise en œuvre de matières premières : Développer l'industrie dans un pays. Chacune de ces activités économiques : L'industrie textile, de la chaussure. Toute activité économique assimilable à l'industrie : L'industrie du spectacle, des loisirs. Activité organisée de manière précise et sur une grande échelle (souvent péjoratif) : L'industrie du crime. Littéraire. Activité quelconque exercée par quelqu'un pour vivre (souvent péjoratif) : Exercer sa coupable industrie.


italien

[Soppi]
  • industria

english

[Soppi]
  • industry

brute