Aller au contenu

wuy

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]

wuy: am na ñaari maanaa

  1. aw wuy doomu guy la te ëmb ay buy,
  2. wuy aw yuuxuwiin la wees gën a ràññee ci jigeen ñi

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:

[Soppi]
  1. wuy wee may seen de aw ñoraa la,
  2. ba diw faatoo de foo toll di dégg wuy

Xool it

[Soppi]

Tekki

[Soppi]

Waxiin

Déglu baatu wuy ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-wuy.ogg