guy

Jóge Wiktionary.
Dem : Joowiin, Seet

wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

guy:

  1. ag guy garab la gu baxoo rëy, ci geént mbaa aw deg lay ëppe.
  2. guy dees koy jëfandikoo ngir xàmmaliku mbir, niki garab guy def nàngam.

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:[Soppi]

  1. guy ag garab la gu bariy njariñ
  2. kàdd garab la guy naat newet

Xool it[Soppi]

Tekki[Soppi]

Nuvola apps edu languages.svg Waxiin

Déglu baatu guy ci wolofi Senegaal