lay
Jóge Wiktionary.
Tëraliin |
[Soppi] wolof
[Soppi]
Gongikubaat
lay amna ñatti manaa ci wolof
- ab lay xeetu taw la bu nit dul yëg,te di ko gis muy weexal jawwu ji,
- aw lay wax jees di wax ngir saxal am mbir
- lay lees di jëfëndikoo tame ngir xajjale lu nooy ak lu dij
[Soppi] Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
- lay baaxul ci wer gi yaram,
- booy lijjanti mbir ci këru àttekaay gi wutël ab tinukat mu layal la.
- jigéen ji lay nañu pénc me bamu sét wicc
[Soppi] Xool it
[Soppi] Tekki
Waxiin
Déglu baatu lay ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-lay.ogg