taw
Jóge Wiktionary.
Tëraliin |
wolof [Soppi]
Gongikubaat [Soppi]
taw
- taw ndox miy bawoo ci asamaan wàcc ci suuf, tey doon lu nit ñi man a yëk,
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof: [Soppi]
- biig dey taw na tawub waame, réew mepp a ngi ji,
Xool it [Soppi]
Tekki [Soppi]
- wu-faraas: -
- wu-angalteer: -
Waxiin
Déglu baatu taw ci wolofi Senegaal