yokk
Aller à la navigation
Aller à la recherche
Wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
Jëf[Soppi]
yokk:
- jël dara teg ci leneen
- yokk ay baat ci sama baatukaay
Tur[Soppi]
yokk g:
- yokkug ay baat ci sama baatukaay
Tekki[Soppi]
wu-faraas: additioner , addition
Delluwaay[Soppi]
Mbay Fay - nanu xayma - Tëngéej IREMPT (UCAD), 2005