Aller au contenu
- li aw askan di dugg,muy mbooloom aw nit mu am réew walla ab gox walla diine: xeetu Senegaal: xeetu Muhammad (j.m)
- (ndundat): aji nekk juy dund: xeet wuy dund
- aw melo, walla lu mel ne: aw xeetu nit
- nation
- espèce;être vivant
- sorte;type