tund

Jóge Wiktionary.
Dem : Joowiin, Seet

wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

Open book 01.svg Tur[Soppi]

tund (w):

  1. ab gox bu ndaw: tundu Mbaakol de fu bari sëb la
  2. safaanub xur: fu xurewul mooy fu tunde, fu suuf si yekkatikoo
  3. 35 tund ñoo nekk ci dogiin wu yoriinu Senegaal, ñoom tund yooyu ci séen bopp tam, dañu leen a séddale ci 92 ndiiwaan

Tekki[Soppi]

wu-fraas: zone, local, mont, departement