tene
Apparence
wolof
[Soppi]tene:
- tene aw rab la, ci rabi àll la bokk
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- Tene mi dafa gaaw lool
Xool it
[Soppi]- -
- -
Tekki
[Soppi]- wu-faraas: guépard
- wu-angalteer: cheetah
- wu-itaali: ghepardo
Waxiin
[Soppi]Déglu baatu - ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo- .ogg