Aller au contenu

sañ-bañ

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]
  • cig sañ-bañ: ci mu neex la mbaa mu naqari la, maanaam dees laa manante, ga la ci nga def ko

français

[Soppi]
  • à contrecœur;par force;de vive force;forcement;inevitablement