pénc m-
Jóge Wiktionary.
Aller à la navigation
Aller à la recherche
- ndàndfay-fay guy faral a nekk ci digg ab dëkk, gu nit ña di faral di daje
- (politig) barab bu ndawi réew mi di daje:péncum ndawi réew mi
- (politig) noste gi dul gu nguur : péncum Senegaal
- place
- assemblée nationale
- la république