njur

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

Mi ngi bàyyikoo ci jur

Open book 01.svg Tur[Soppi]

njur g:

  1. mooy li ñu jur
    njurug sama liggéey

Bokktekki[Soppi]

njureef

Tekki[Soppi]

wu-faraas: produit

Delluwaay[Soppi]

Mbay Fay - nanu xayma - Tëngéej IREMPT (UCAD), 2005