Aller au contenu

njuddéef

Jóge Wiktionary.

==

Wolof

[Soppi]
  • njuddéef, mgi juge ci judd, di li juddoo cib liggéey, la nga góobe ci sa ab liggéey mooy njuddéef ma, dees na ko wax ba tay njuréef;ngérte;njóoxte.

Francais

[Soppi]
  • production

Italiano

[Soppi]
  • produzione

English

[Soppi]
  • production