Aller au contenu

njëwriñ

Jóge Wiktionary.
(Yoonalaat gu jóge njëwrin)

wolof

[Soppi]
  • ci la jëwriñ juge: ag njëwriñ lanuy wax mooy fi jëwriñ ji di nekk ak mbooleem li mu yilif.Ñenn ñi di ko wax: kër jëwriñ,ñi ci des naan ko: makaanu jëwriñ

Yeneeni làkk

[Soppi]
wu-faraas: ministère
wu-angalteer: ministry
wu-itaali: monistero