njël

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

Open book 01.svg Tur[Soppi]

njël l-

  1. Jamono
    • suba teel, waxtu yi njëkk ci bés bi
  2. Xaalis
    • mbooleem xaalis, gu ag nguur, walla kenn nit, yor war cee doxal ay sémbam.
    • Njël lu réewum senegaal toll na ci junniy milyaar.
  3. Xam-xamu nosukaay
    • barab bi ay mbind nekk te ngir man cee dugg faww nga cuq cib lëkkalekaay te boo ca cuqe mu won la la nekk ca biiram, ñuy yeneeni lëkkalekaay. ci misaal, li ngay gis ci kaw xët wii: Xët, Waxtaan, Soppi, Jaar-jaar, Far, Tuddewaat ak Topp, ay njël lañu.

wu-faraas: aube, budget, menu