Aller au contenu

njëkk

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

njëkk:

  1. mooy ndorteelu am mbir
  2. ci waññi:
    • man maay ki njëkk ci kër gi
    • ci rawante bi Musaa mooy ki njëkk a àgg

ndoorte

Tekki

[Soppi]

wu-faraas: début, premier

Delluwaay

[Soppi]

Mbay Fay - nanu xayma - Tëngéej IREMPT (UCAD), 2005