Aller au contenu

nguur g-

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]
  • réew walla dëkk bu ay buur jiite, moom ko,misaal: nguurug Kajoor
  • nekke ni ko neex gi buur di def: moom de day nguuru cig njoowaanam
  • doole ji jiite am réew ak doonte du mu ay buur: nguurug Senegaal te nosteg pénc la

français

[Soppi]
  • royaume
  • l'état; le pouvoir