Aller au contenu

nattu

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]
  • lu Yàlla di teg ab jaam ngir seet ko ci, walla ngir yokk ko ci ay xéewal walla fegal ko ci ay lor
  • jarbu, làmb ba daj, xam gu jaar ci jonjoo ak mbir mi(1)

français

[Soppi]
  • expérimenter(1)