mbootaay g-

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

mi ngi bàyyikoo ci boole

Open book 01.svg Tur[Soppi]

mbootaay g:

  1. ab kuréel bu liggéey boole mbaa diine mbaa lenn, ay sart di leen àtte
  2. ag lonkoo: ag jàppoo bokk dara ngir liggéey

Xool it[Soppi]

Tekki[Soppi]

wu-faraas:

  1. organisation , association
  2. société