Aller au contenu
mi ngi bàyyikoo ci boole
mbooloo:
- kuréel ci lépp: ci nit, cig jur, ci lu nekk, ab lim ci ay mbir.
- lu sakkan ci lu nekk, lu ëpp benn
- (nos-wax): baat biy wund lu ëpp benn ciy baat, di safaanub Bennaan
- (xayma) ensemble
- (nos-wax) pluriel