Aller au contenu

màngo

Jóge Wiktionary.
Wikipedia am na jukki bu tudd:

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

màngo g

  1. garab giy jur màngo.

màngo b

  1. meññeef la mu ñuy lekk, day jóge ci garabug màngo.

Tekki

[Soppi]
turu xam-xam: Mangifera indica
farañse: manguier, mango
angale: mango tree, mango
itaaliyee: mango