Aller au contenu

lingoom

Jóge Wiktionary.
Wikipedia am na jukki bu tudd:

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

lingoom g

  1. garab giy jur lingoom.

lingoom b

  1. meññeef la mu ñuy lekk, day jóge ci garabug lingoom

limoŋ

Tekki

[Soppi]
turu xam-xam: Citrus limon
farañse: citronier, citron
angale: lemon
itaalyee: limone