Aller au contenu

lammeñ

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]

ci wolof yi

lammeñ:amna ñaari maanaa ci wolof

  1. lammeñ ab cer la ci nit bu nekk ci biir gemmeñ, nu koy jëfandiko ngir wax ak taqqam tiku ak..
  2. lammeñ làkk wune ña ca cosaanoo, lammeñ lay tud ci ñoom, misaal:senegaal wolof lammeñ lafa waaye nasaraan aw làkk lafa

nduroowaale

[Soppi]

Tekki

[Soppi]

Waxiin

Déglul baatub lammeñ ci wolofi Senegaal