Aller au contenu

lamb

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]
  • ñàkk a jar: njaayam mi daa lamb, kenn bëggu ko: daa jarul
  • koom-koom bu daanu: Tugal ci fan yii daa tàbbi ci ag lamb: koom-koomam daa daanu1

français

[Soppi]
  • récession

english

[Soppi]
  • recession