Aller au contenu

lëng

Jóge Wiktionary.
Wikipedia am na jukki bu tudd:

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

lëng g

  1. garab giy jur lëng.

lëng b

  1. meññeef la mu ñuy lekk, day jóge ci garabug lëng.

Tekki

[Soppi]
turu xam-xam: Vitex doniana
farañse: prunier noir
angale: black plum
itaalyee: -