kocc
Apparence
wolof
[Soppi]kocc: am na ñatti maanaa
- aw kocc doomu guy la moodi wuy wu ndaw te ñor,
- kocc aw tur la, ki ko tuddoon di ku suqali wolof ngir xel mu ñaw.
- ag kocc jël aw xeer mbaa luni mel door ko ca moroom ja mbaa leneen.
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- wénn kocc du ma ko bokk ak mbooloo,
- kocc barma neewoon na jigéen soppal te bul wóolu !
- gone yaa ngi ci mbédd mi di koccan tey egaat.
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: -
- wu-angalteer: -
Déglu baatu kocc ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-kocc.ogg