kawewaay

Jóge Wiktionary.

wolof =[Soppi]

Gongikubaat[Soppi]

  • Maanaam ni mbir mi kawe:

Misaal: kawewaayu kër gi;

  • Di na tekki itam màggaay walla rëyaayu ab mbir:

Misaal: xarala gu kawe;

xool it[Soppi]

kawe
kaw
kaw-kaw
kawtéef

yeneeni làkk[Soppi]

English: height,
Français: hauteur
Italiano: altezza