Aller au contenu

karasol

Jóge Wiktionary.
Wikipedia am na jukki bu tudd:

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

karasol g

  1. garab giy jur karasol.

karasol b

  1. meññeef la mu ñuy lekk, day jóge ci garabug karasol.

Tekki

[Soppi]
turu xam-xam: Annona muricata
farañse: corossolier, corossol
angale: soursop
itaaliyee: graviola