Aller au contenu

jataay (ab)

Jóge Wiktionary.

Wolof[Soppi]

Gongikubaat[Soppi]

Ndaje

ab toogaay, ag jekki

Politig
jataayub jëwrin yi

Yeneeni làkk[Soppi]

wu faraas: séance, conseil des ministre
wu itaali: seduta, consiglio dei ministri
wu angalteer: session, council of minister