jambur
Apparence
Wolof
[Soppi]→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
jambur:
- ku dul féete, du far
- nit kii de jambur la walla nit kii de ku jambure la
- ci xayma: du soppi yeneen cër yi, soo leen boolee, loo manti yokk Tus (0) du soppiku. Kon Tus cër bu jambure la
Tekki
[Soppi]Delluwaay
[Soppi]Mbay Fay - nanu xayma - Tëngéej IREMPT (UCAD), 2005