Aller au contenu

jaadu

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

jaadu g:

  1. mooy lu xel nagu
  2. lu wara am: jaadu na nga dem seeti sa xarit bi

Tekki

[Soppi]

wu-faraas: logique

Delluwaay

[Soppi]

Mbay Fay - nanu xayma - Tëngéej IREMPT (UCAD), 2005