Aller au contenu

jóoñ

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]
  • ab jóoñ: bant bu mel ne wii araf Y, ñu koy jëfandikoo niki ag mbaq, di takk ci ñaari cat yi ay xett yuy tàwweeku, ngir sànnee ci xeer ngir jam picc, mbaa lu ni mel