Aller au contenu

gerte tubaab

Jóge Wiktionary.
Wikipedia am na jukki bu tudd:

Wolof

[Soppi]

gerte ak tubaab → Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

gerte tubaab g

  1. garab giy jur gerte tubaab.

gerte tubaab b

  1. meññeef la mu ñuy lekk, day jóge ci garabug gerte tubaab

Tekki

[Soppi]
turu xam-xam: Terminalia catappa
farañse: badamier
angale: indian almond
itaalyee: mandorlo indiano