gar
wolof
[Soppi]gar: amna ñaari maanaa ci wolof
- gar gaynde gu màggat, rab la ci rabi àll yi
- gar am po la muy am dóore, ñénn dañuy dugg ñénn di leen génne.
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: Vieux lion
- wu-angalteer: Old lion
Déglu baatu gar ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-gar.ogg