gëstuwaay

Jóge Wiktionary.

wolof[Soppi]

am ndaje mbaa jataayub ay njàngatkat, ay boroom xam-xam ak/walla ay niti fànn yu séeni moroom nangul, jataay boobu li ko tax a jug, di xool ak a saytu ni ñuy jëfandikoo ci séeni liggéey ak mecce, ak a siiwal ay liggéey niki ay baatukaay, ay nos-wax, añs. Gëstuwaay nag (Akaademi) ñi ngi ko njëkk a jëfandikoo ngir wunde ci daara ji Aflaaton sosoon ca Aten ca -387 9(baatub Liise bi ngay dégg,te bawoo ci wu Gres wu yàgg wa Lukeion ab tàggatuwaay la woon bu Aten fu Sokraat daa jàngalee, ginaaw bi Aristo). ci jamono ju yees ji, gëstuwaay bu nataal bu Firenze sosu na ca Itaali ca 1563 ci pexem Giorgio Vasari, baat bi nag jëfandikoos na ko ca Faraas ngir tekki ci ag mbootaay gu ay yitteem jëm ci lefum caada, li ciy misaal: gëstuwaay bu Faraas bi Richelieu sos .

francais[Soppi]

  • académie:

Une académie est une assemblée de gens de lettres, de savants et/ou d’artistes reconnus par leurs pairs, qui a pour mission de veiller aux usages dans leurs disciplines respectives et de publier des ouvrages tels que des dictionnaires, des grammaires, etc. Le terme d’Académie a été employé la première fois pour désigner l’école que Platon a fondée à Athènes en -387 (le terme de Lycée, en grec ancien Lukeion, était un gymnase d’Athènes près duquel Socrate, puis Aristote enseignèrent).

À l’époque moderne, l’Académie du dessin de Florence se crée en Italie en 1563 à l’initiative de Giorgio Vasari et le terme est employé en France à partir du pour désigner une institution ayant une mission dans le domaine culturel, le prototype en étant l'Académie française fondée par Richelieu.