Aller au contenu

foytéef

Jóge Wiktionary.
Wikipedia am na jukki bu tudd:

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

foytéef g

  1. Meññeef mu neex muy jóge ci garab, niki màngo, suraas, banaana ak pom.

Tekki

[Soppi]
farañse: fruit
angale: fruit
itaaliyee: frutto