diw
Aller à la navigation
Aller à la recherche
wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
diw: amna ñaari maanaa
- ag diw niki ndox lay xellee tey niin
- diw manees na koo wax jublu ci ku ne
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:[Soppi]
- diw day niin
- diw dee ma may xaalis
Xool it[Soppi]
Tekki[Soppi]
- wu-faraas: - pétrole
- wu-angalteer: - oil, ointment
Waxiin
Déglu baatu diw ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-diw.ogg