Aller au contenu

dittax

Jóge Wiktionary.
Wikipedia am na jukki bu tudd:

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

dittax g

  1. garab giy jur dittax.

dittax b

  1. meññeef la mu ñuy lekk, day jóge ci garabug dittax

Tekki

[Soppi]
turu xam-xam: Detarium senegalense
farañse: -
angale: tallow tree
itaaliyee: -