diig
Apparence
wolof
[Soppi]diig:
- diig niki suux, ci ndox lees koy jëfandikoo
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- gaalug mool yi diig na ca géej ga
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]Déglu baatu diig ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-diig.ogg