Aller au contenu

daxin

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

daxin b

  1. ceeb bu ñu baxal ak soosu gerte.
    • daxin la toggluwoon démb.