dar
Aller à la navigation
Aller à la recherche
wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
dar: amna ñaari maanaa yu man a bokk
- dar lu tafu sës rikk ci dara
- dar niki cin lu dar
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:[Soppi]
- dar ko rek bu ko bàyyi
- soxna si sa cin laangi dar
Xool it[Soppi]
Tekki[Soppi]
- wu-faraas: -
- wu-angalteer: -
Waxiin
Déglu baatu dar ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-dar.ogg