dajale
Apparence
wolof
[Soppi]dajale:
- dajale boole ay mbir
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- dajaleel ma sama këyit yi
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: rassembler
- wu-angalteer: gather
Déglu baatu dajale ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-dajale.ogg