daaj

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

daaj: am na ñaari maanaa

  1. daaj di dóor dara ngir mu dugg,
  2. daaj tëraliinu woy mbaa am njàng,

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:[Soppi]

  1. kuy defar ab lal fàww nga daaj .
  2. am njàng ca daaj ba lay neexee.

Xool it[Soppi]

Tekki[Soppi]

Nuvola apps edu languages.svg Waxiin

Déglu baatu daaj ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-daaj.ogg