dër
Apparence
wolof
[Soppi]dër: amna ñaari maanaa
- ab dër nees di def ab ruum
- ag dër nit kuy wax di gag
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- ruum bi de ban lees ko dëree
- diw de daa dër buy wax day gag
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: sol
- wu-angalteer: floor
Déglu baatu dër ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-dër.ogg