dàll
wolof
[Soppi]Dàll:
- dàll turu lenn la, lees di sol ci ay tànk ngir sàmmu
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- sama dàll yi dagg na
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: -
- wu-angalteer: - shoe
Déglu baatu dàll ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-dàll.ogg