coro
Apparence
wolof
[Soppi]coro:
- coro ndaw soo bëgganteel.
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- diw... ak a rafet coro,
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: petite amie
- wu-angalteer: girlfriend
Déglu baatu coro ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-coro.ogg